Movatterモバイル変換


[0]ホーム

URL:


Aller au contenu
Wikipedia
Seet

World Wide Web

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki abjunj rekk la.Man nga cee duggal sa loxosuqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yiWikipedia taxawal


World Wide Web manees na koo tekkee niki digg lënd gi (lënduk jargoñ) kon ana numu def ba tuddees ko digg lënd ? ndax moom la àdduna bépp ànd di jëfandikoo ku ne jàpp ci génn lawtan fa lawtan ya daje lees tuddee digg lënd moom nag manees na koo jëfandikoo fim ne ci àdduna bi yépp, gox yépp man nañu cee daje, boo jëmee ci ab dal dugal www doora def turu dal ba man naa ñàkk yit ci bu la neexee nde joowkat yu yees yi di nañu nànd sa bëgg-bëgg ba jobbu la, www yii nak limu wund ciwu-angalteer mooy World Wide Web

Ci « https://wo.wikipedia.org/w/index.php?title=World_Wide_Web&oldid=94758 » lañ ko jële
Wàll :

[8]ページ先頭

©2009-2026 Movatter.jp