Movatterモバイル変換


[0]ホーム

URL:


Aller au contenu
Wikipedia
Seet

Budda

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki abjunj rekk la.Man nga cee duggal sa loxosuqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yiWikipedia taxawal


Benn Melalu Buddaa joge Sarnathl

Siddhārtha Gautama (Sanskrit:सिद्धार्थगौतम;Pali:Siddhatta Gotama) nekkoon na di ab jàngalekatu diine ca pénkub dogu-gox bu indian, moo sos ngiirum budda xolees na ko ci way buddaa niki xalifab budda (Sammāsambuddha)ci sunuy at. Atum juddoom ak mom deeyam wuutees na ci: ñaar fukki réew yi gën a fes ci jaar-jaar, taarixal na ñu diirub dundam ci ne c. 563 BCE jëm 483 BCE; li gën a mujj, te sax,

Waxam ju mujj moodi: «Mbëj yees defar yepp luy wéyadi la ; Liggéey ci ag xarañ te bañ a noppalu ; Am jubluwaay bu baax farlu ; Saytu xalaat yi ! »

Ci « https://wo.wikipedia.org/w/index.php?title=Budda&oldid=95486 » lañ ko jële
Wàll :

[8]ページ先頭

©2009-2026 Movatter.jp