Movatterモバイル変換


[0]ホーム

URL:


Aller au contenu
Wikipedia
Seet

Betsayda

Jóge Wikipedia.
Betsayda

Ci làkku ibrë \^hdyu-tyb\^; CI làkku yawut la tur wi jóge.Ci angale mooyBethsaida; Ci faranse mooyBethsaïda

Dëkk ba ci penku-kawu dexuGalile la woon, sorewul fu dexuYurdan dugg. Tey jii xamuñu tembe bérab bi. Man na nekk sax amoon na ñaari dëkk yu bokk turBetsayda. Benn ci penku dexu Yurdan, te benn (mooy Betsayda ci diiwaanu Galile) ci sowu dexu Yurdan.

Man nañu koy jàng ci Injiil ci Mc 11:21; Mk 6:45 8:22; Lu 9:10; 10:13; Yow 1:44; 12:21.

Logo Commons

Xool itWikimedia Commons
Ci « https://wo.wikipedia.org/w/index.php?title=Betsayda&oldid=94206 » lañ ko jële
Wàll :

[8]ページ先頭

©2009-2026 Movatter.jp