Barabas
Outils
Général
Móol/génne
Ci yeneen sémb
Ci làkku ibrë בר-אבא; Ci làkku yawut la tur wi jóge.Ci angale mooyBarabbas; Ci faranse mooyBarabbas
Bóomkat ak taskatu réew la woon. Nekkoon na ci kaso bi ñu jàppee Yeesu.Pilaat bàyyi na ko bi ñu àttee Yeesu. Man nga ko jàng ci Mc 27:16-26; Mk 15:7-15; Lu 23:18-25; Yow 18:39-40.
Turam moo feeñ ci aaya yii: Mc 27:16,17,20,21,26; Mk 15:7,11,15; Lu 23:18,19; Yow 18:40.