Ci angale mooyBalak; Ci faranse mooyBalak
Balag, buur ci jamonoy yonent YàllaMusaa la woon. Moo yilifoon waa Mowab. Fey naBalaam, ngir mu rëbbal ko bànni Israyil. Man nañu jàng ci jalooreem ci Nu 22:1-24:25.
Injiil moo wax ci moom ci Pe 2:14.