Ci làkku ibrë la tur wi jóge.Ci angale ak ci faranse mooyAzor.
Benn ci maamaati Yeesu ci Macë la woon (Mc 1:13,14).