Aser
Outils
Général
Móol/génne
Ci yeneen sémb
Ci làkku ibrë (אָשֵׁר) la tur wi jóge.Ci angale mooyAsher; Ci faranse mooyAsser
Benn ci giiri bànni Israyil la woon, ñi soqikoo ci Aser, mi doon juróom-ñetteelu doomu Yanqóoba bu góor.
Giiru Aser moo feeñ ci Injiil ci Lu 2:36; Pe 7:6.